Auteurs | S El hadji Mbacke | |
Catégorie | Tassaouf | |
Xassida | ||
Interpretes | Saliou Gadiaga | |
Extraits | 113 |
Bismillaahi Barké Borom Touba
Auteurs | S El hadji Mbacke | |
Catégorie | Tassaouf | |
Xassida | ||
Interpretes | Saliou Gadiaga | |
Extraits | 113 |
Tardjumaan |
![]() |
![]() |
|
Bindam mo kawe bepp jaamu yalla |
![]() |
![]() |
|
Sunu borom nangu na ay xalamam |
![]() |
![]() |
|
Taxagn yoon bi |
![]() |
![]() |
|
Kawe na bepp jihaad |
![]() |
![]() |
Leeral xamxam |
![]() |
![]() |
|
Day Tere lu bonn |
![]() |
![]() |
|
Day djubal |
![]() |
![]() |
|
Day begal malaaka yi |
![]() |
![]() |
|
Baaqiyaatu saalihaat la |
![]() |
![]() |
Day yokk mbecte Yonenti bi |
![]() |
![]() |
|
Dereetu ku dee jihaadu Yonenti bi |
![]() |
![]() |
|
Womate tji Borom bi |
![]() |
![]() |
|
Bok tji muhjizaatu Yonenti bi |
![]() |
![]() |
|
Ngueun gui jaamu Yall |
![]() |
![]() |
Melni mboleen Yonenti yi |
![]() |
![]() |
|
Li Yalla ak Yonenti gana beug |
![]() |
![]() |
|
Haqul yaqiin la |
![]() |
![]() |
|
Kawee mboleem nafila yi |
![]() |
![]() |
|
Tagatal ko ay noon |
![]() |
![]() |
Mo gueun ay Yiiw yu bari |
![]() |
![]() |
|
Mboleem gni ngui Arass |
![]() |
![]() |
|
Melni Yonenti |
![]() |
![]() |
|
Kawe na ndjotam |
![]() |
![]() |
|
Gueun gaa kawe ngeuremu Yalla |
![]() |
![]() |
Yemoo ak taw bu barkel |
![]() |
![]() |
|
Womate djeum tji lu baax |
![]() |
![]() |
|
Tuyaaba buy weuy ba al djana |
![]() |
![]() |
|
Melni hajj koor ak djuli |
![]() |
![]() |
|
Leer buy joli saa su nekk |
![]() |
![]() |
Yalla mom la gana sopp tji jaamu yi |
![]() |
![]() |
|
Dundu tji Yonenti bi ak ay xeeweul |
![]() |
![]() |
|
Day begal Yonenti bi |
![]() |
![]() |
|
Baneex la tji Yonenti bi |
![]() |
![]() |
|
Melni djeuf yu baax yeup |
![]() |
![]() |
Wessu wul Yalla ak Yonenti bi |
![]() |
![]() |
|
Dindi bakar ba mu jeex |
![]() |
![]() |
|
Kawe ay top Yalla yu bari |
![]() |
![]() |
|
Kawe na koor ak ludul moom |
![]() |
![]() |
|
Dadjalel na ko makaama yeup |
![]() |
![]() |
Yonenti bi day pucare wo ligeeyam |
![]() |
![]() |
|
Tedd ak ndjarign yu sax dak |
![]() |
![]() |
|
Harass day jaayu |
![]() |
![]() |
|
Jakaarlo ak lawhul mahfuuz |
![]() |
![]() |
|
Gatjeel noon |
![]() |
![]() |
Dak tubab yi sa gueedj ga |
![]() |
![]() |
|
Dentj ko arass ak kursiyu |
![]() |
![]() |
|
Malaka yi yok seen sabaal |
![]() |
![]() |
|
Dak lorru tubab yi |
![]() |
![]() |
|
Di digante nitt ak boromam |
![]() |
![]() |
Dundal islam |
![]() |
![]() |
|
Sunu borom nangu na bidam yeup |
![]() |
![]() |
|
Todj na bepp tabaxu yeefar |
![]() |
![]() |
|
Dindi thiona ak yedangue |
![]() |
![]() |
|
Mboleem lu bax ak yow mi ngui tji |
![]() |
![]() |
Teere Yonenti yeup nga tji biir |
![]() |
![]() |
|
Arass di jaayu malaka di savaal |
![]() |
![]() |
|
Mboleem lu baax da tjiy dugu |
![]() |
![]() |
|
Borom bi joxna ko barke bind |
![]() |
![]() |
|
Mbindeef yiy yeemu |
![]() |
![]() |
Begal Yonenti bi |
![]() |
![]() |
|
Gatjeel na bepp bind |
![]() |
![]() |
|
Jihaad kuy fo |
![]() |
![]() |
|
Yoneti bi di muugn ibliss lakatu |
![]() |
![]() |
|
Leeru al quran ak lamign arab |
![]() |
![]() |
Yalla magal na Asasin ba balsasin |
![]() |
![]() |
|
Dawloo Seytaane |
![]() |
![]() |
|
Fadj aajo kuko ziar |
![]() |
![]() |
|
Yeungal xolu Yonenti ak malaika |
![]() |
![]() |
|
Dak noon feg ku weddi |
![]() |
![]() |
Ibliis day tiit am gatje |
![]() |
![]() |
|
Ndiarignu hadiss yi |
![]() |
![]() |
|
Taxawaay djeufi dji djaam yeup |
![]() |
![]() |
|
Far lepp lu niaaw jeum tji Borom bi |
![]() |
![]() |
|
Deugeureul nama tji lawhul mahfuz |
![]() |
![]() |
Djigueen adjana diko wayanto |
![]() |
![]() |
|
Saafara xoll |
![]() |
![]() |
|
Yeungeul xollu gni baax |
![]() |
![]() |
|
Da gnoo melni ay xare |
![]() |
![]() |
|
Melni ay xare |
![]() |
![]() |
Texe lagn tji bep murid |
![]() |
![]() |
|
Yee xell yi |
![]() |
![]() |
|
Djubalu laa ilaaha ilallaahou |
![]() |
![]() |
|
Yeemo jeufi waa Badar |
![]() |
![]() |
|
Saxal ko djang nguir dak iblis |
![]() |
![]() |
Seydinaa Djibril mo kay deugereul |
![]() |
![]() |
|
Seen dayo kem dayo sunu borom |
![]() |
![]() |
|
Ken du werante ak moom |
![]() |
![]() |
|
Sunu borom tji lay fadjee aadjo yi |
![]() |
![]() |
|
Doyadil pexay noon |
![]() |
![]() |
Jihaad ak yeefeur yi |
![]() |
![]() |
|
Yeungueul xolu ahlu badr |
![]() |
![]() |
|
Bepp lawraat mi ngui tji biir |
![]() |
![]() |
|
Thianu djigueenu aldjanna |
![]() |
![]() |
|
Doo tul faatu kuko sooru faatu |
![]() |
![]() |
Da gniy firi laa ilaaha ilalaahou |
![]() |
![]() |
|
Tag Yonenti bi di djoyloo Seytaane |
![]() |
![]() |
|
ismulaahi ahzam |
![]() |
![]() |
|
Sunu borom moo may sah |
![]() |
![]() |
|
Deugueureul sama yaakaar |
![]() |
![]() |
Yeesal sunna Yonenti bi |
![]() |
![]() |
|
Borom bi barkeel na ko |
![]() |
![]() |
|
Ay noonam da gnuy djooy |
![]() |
![]() |
|
Fulkul mashoun |
![]() |
![]() |
|
Feetali bindam Yonenti bi |
![]() |
![]() |
Dindi metitu Yaram |
![]() |
![]() |
|
Agale la tji sa borom |
![]() |
![]() |
|
Naaguloo seytaane |
![]() |
![]() |
|
Ngeuneel yu kenn meusta am |
![]() |
![]() |
|
Magal mbindoup Serigne bi |
![]() |
![]() |
Gna nga arass ak kursiyu |
![]() |
![]() |
|
Suni botom dina ko poucare woo |
![]() |
![]() |
|
Tedju Teere bi |
![]() |
![]() |