Silkul Jawaahiri

Auteurs Cheikh Ahmadou Bamba
Catégorie Tawhid
  Fikh
  Tassaouf
Interpretes Cheikh Abdourahmane Mbacke
Extraits 245

2 - Buntu Addina ak li tji adju

Buntu Addina ak li tji adju
Meytu beug adduna
Meytu beug adduna niarel
Meytu beug adduna nietel
Niari hiqam
Hiqma
Hiqma
Hiqma
Ndiarignu noppi
Hiqma
Maanute sunu borom
Nienti baati Seydina Adama
So beuge ame khol bu teey
Am khol bu tali
Ame khol bu nakari
farlou tji djeuf lu baax
li gana yeemu tji mbir yep
Ki eup daradja tji nit gni
Ki gana tabe tji nit gni
Ki yees tji nit gni
Hiqma
Hiqma imam Ali
Hiqma Luqman
Dieuw bu dagan
Niane tuub ak sant
Meutu nio yedd
Bou lene wan sa daradja
Gni nfa waruta woyafal
Yiy wane daradja
Nopalu tji niet yii
Nieti yiy takh nga niak katan
Djurom nieti yiy indi gatje
Djurom yiy indi retju
Nieti yiy djur thiofeel
Niet yii tji niet lay nekk
Niett yi ngay xamee tji niett
Niett djiko yu djulit yi wara sam
Niett yiy tax ku baax beug leu
Nieti yiy dioxe nakari dundu
Niet yu doy waar alaakhira
Ndiarognu khiif
Niet yi sa digante djulit bi
Niet yu djara meytu
Niet yi gan nit
Nient yu diara roy
Nient yi dul regg
Nient yi dul dara
Nient yu diafee am
Nient yi Yalla gana beug
Nient yu aadjoo nient
Nient yi tax addina diak
Nient yu diaruta kheep
Nient yiy tax addina soof la
Nient yi ma amul sene pay
Hiqam Imam Ali
Nient yi warr tji ku gueum Yalla
Hiqma Al Hubii
So beuguee doon ku tedd
Nient gni djara meytu
Nient yi nient xam
Nient yi dul taggok nient
Nient yi andak nient
Nienti wax
Nienti hadiss
Deudu adduna
Sellal djaamu yalla
Toogaale ak nittu Yalla
Djuroom yi djara bayi khel
Djurom yi meutu leu russ sonal
So beugee deuk tji barab
Djuroom yii guenul djuroom yii
Ku yewwu
Gni gueun tji djaamu yalla yi
Djuromi ndiarigne
Li aniaan di djurr
fedj xol bu wow
Li tudd Yalla di djurr
Mandarga texe
Mandarga texedi
Djuroomi bakane yu sell
Denkane Yonenti bi
Hikam
Djurom nieti li gniy djurr
Hikam imam Ali
Djurum nienti djiko Yonent
foukou yi Yalla di mere
Hikam
Djurum nienti yi niu niaaw lu
Fukku yi bok tji niak teggin
Fuki baat ak niar yu Kahbu
Seydina Omar
Meytu merru waydjurr
Moy sa waydjurr
Yoolu sarakh ak bakaaru ndiaaloo
Fonk Barke ak ndiguel
Garabouk bakaar
Fagoul adduna ak alakhira
Begn yeuk sa bopp
Tudd Yalla
Raggal Yalla
Baril sakku ndjegelu Borom bi
Takoo njapp
Djuli djuroom
Djuli yoor yoor
Sarax
Yaatal xeweul yi bissu tamxarit
Yaatal toogu kay sa mbok djulit
Soy dug sa keur djangal saar yi
Nuyoo sooy dug sa keur
Suratul Al Waaqiha
Suratul Muzzamil
Subhanalaahi wa bi hamdihii
Wout ay gatt
Tuddee Yonenti bi sa doom
Djuli fadjr tji mbolo ba nopi dess fa
Fataliku Yalla guinaw djuli yii
Hadj ak umra yu meut seuk
Loru niak tudd Yalla
Fanane ak laab
Djang saar ba la ngay teud
Saraxe day aare
Beru nitt gni
Noppi
Bagn di feegnal yewute
Mougn
Bul waxal ken lu koy merloo
Meytu merr ak yakamti
Liy dak ak woyofal mussiba
Sarax pexe la tji mussiba yi
Dundeul djaka pexe la tji mussiba
Barab yii Yalla la fay aar sam la
Guinaw djuli adjuma
Hasbala djurum niari yoon
Yene tji ay muslaay
Mutj tji ndiakare
Mutj tji kilifeu aduna yi
Mutj tji goumba deundu ak melkhat
Mutj tji ngelaw lakk ak benj ak nop
Ni nga leblee noonu na gnu la fayee
Nianu ku bari borr
Yiy indi Weurseuk ak niak
Sam sawou kaay
Am wergu yaram
Fadj weredi yaram
Motj beut bu aay
Muslu djinne ak seytaane yi
Muslu tji ayu kagnaane
Leemou ay gone
Yombal wassine
So ame lu reer walaku leu reer

9 - Buntu tji genuk ruh bi

Buntu tji genuk ruh bi
Mbugeulu bamel ak bamel bu leer
Mutj tji fitna bamel ak alakhira
Mutj tji safara
Mutj tji reki ngueum
Yeurmande borom bi
Rih adji game ak yeefer
Begal Ruh adji game gui
Fitna yi tji bamel
Xeewalu bissu pentj tji nient gnii
Neew bi ak Rawmaan
Niari malaka yermande yi
Djeuf yii di na yombal
Neew bi ak Munkiir ak Nakiir
Yermande ak mbugalu Yalla
borom xam xam yi
Teuraayu bamel
Guent Guiss ku faatu
Waxtaan ak ku faatu
Kemtaanu biir bamel
Djang al quran tji biir bamel
Ruh bi ak yaram wi
Ruh bi guinaw faatu
Nianal neew
Faatu taxula xam
Seede assaman ak souf tji djam bi
Neww bi ak bamel bi
Deukou waayu ruh yi
Lane moy ruh
Barabu ruh tji djeum dji
Ruh ak Rawaan
Yobante ba balsak
Ay hadiss yu am solo
Dieexeulu teere bi